Lyrics

Par AbouAmg Toogal déglu ma àdduna bi Yàlla fi ne Jamono metti na, ana jaambaar coqari Su for yombee sëgg jafe billaay (ma ne billaay) Coono du réer, gëmal sa boppu way (boppu way) Liggéey ba dead bul mës a xepp sa njaay Mën nga jugé ci zéro doon suba héros Bitim réew sori na, nañu waa-jur da lay gunge Soo bëggee ñu ndaw la, jom ak fulla rekk ngay wane Bañ ku la yab, bul xaar ku lay defal Jugal nga fight sa ëllëg ngay defar (ngay defar) Looy tambalee farlu nga yeggale Mën nga jugé ci zéro doon suba héros Lu la war jug doori war (jug doori war) Am na waxambaane (am na waxambaane) Oh yaw la kër ngi di xaar (yaw la kër ngi di xaar) Waa-jur yaa ngi ndëlle (waa-jur yaa ngi ndëlle) Jugal uuti xéy nelaw bi yàgg na (yàgg na) Fonkal sa liggéey mooy jur sa teraanga (teraanga) Marchand ambulant wax dëgg jaaraama Masa coono yaay booy naaj bi tàng na Oh oh bul xépp li ngay liggéey (bul xépp li ngay liggéey) Su baaxee dangay gagner (su baaxee dangay gagner) Àdduna bare la (àdduna bare la) Te fok nga am fit ñeme (faw sa fit ñeme) Oh oh bul xépp li ngay liggéey (bul xépp li ngay liggéey) Su baaxee dangay gagner (su baaxee dangay gagner) Àdduna bare la (àdduna bare la) Te fok nga am fit ñeme (faw sa fit ñeme) Jugal uuti xéy jant bi fenk na (fenk na) Fonkal sa liggéey mooy jur sa teraanga (teraanga) Bul gaawa sëngéem fi Yàlla moo fi ne Masa coono my boy naaj bi tàng na Jugal uuti xéy nelaw bi yàgg na (yàgg na) Fonkal sa liggéey mooy jur sa teraanga (teraanga) Marchand ambulant wax dëgg jaaraama Masa coono yaay booy naaj bi tàng na Ma ne la soo ma déggee may waxe ni Dafa jot ma xamal la Soo ko ñeme bul mës a xàddi Bul xaar kenn defal la Jugal uuti xéy jante bi fenk na (yàgg na) Fonkal sa liggéey mooy jur sa teraanga Bul gaawa sëngéem fi Yàlla moo fi ne Masa coono my boy naaj bi tàng na Mën nga jugé ci zéro doon suba héros Mën nga jugé ci zéro doon suba héros
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out