Lyrics

Par AbouAmg Waaw waaw yehé Dior Mbaye Yàlla dogal lu ma def mu dem Fa ñee di tële, ñële di jëm Ma saf ci seen xol ba dàq lem Ngeen di ma sànni cœurs aki j'aimes Buur Yàlla dogal lu ma laal mu dem Yaw saqar bu dekki ku ca langue dem Xoolal Ségne Fallou ma wis xorom ba ma ñeme Segne Fallou ma wis xorom ma yeme Picc takk ci guy (guy yëgul) Picc kes kesi (guy yëgul) Picc naw ni fér (guy yëgul) Hey picc takk ci guy (guy yëgul) Picc kes kesi (guy yëgul) Heyy picc yakk ci guy (guy yëgul) Picc kes kesi (guy yëgul) Picc naw ni fér (guy yëgul) Yëg nga ni guy gi yëgu la (guy yëgul guy yëgu la) Bu de dangay jamb de yëgu la (guy yëgul guy yëgul la) Yaw xoolal ma ngay su yëgu la (guy yëgul guy yëgul la) Guy gu mat yëgu la (guy yëgul guy yëgul la) Ma ne dindi sax lan nga defoon ca gën Yàlla noppi na Doomu jaambur ku ko yakk dang ko jurul Ku ne xam na ki la mën danga ko dul nangu Yàlla def na li ko sopp demb noppi na Ma ne garab bu ndaw Boo ko munta rose bàyyi ko mu dund Bul jëm budi bul budilu xamoo fu ren ba sax Dandal sore deko xol de loin moo lay musel Xanaa xamoo ne am na ñoo xam ne kenn duleen laal Picc takk ci guy (guy yëgul) Picc kes kesi (guy yëgul) Picc naw ni fér (guy yëgul) Hey picc takk ci guy (guy yëgul) Picc kes kesi (guy yëgul) Heyy picc yakk ci guy (guy yëgul) Yëg nga ni guy gi yëgu la (guy yëgul guy yëgu la) Bu de dangay jamb de yëgu la (guy yëgul guy yëgul la) Yaw xoolal ma ngay su yëgu la (guy yëgul guy yëgul la) Guy gu mat yëgu la (guy yëgul guy yëgul la) Boo amee ñaanu waajur Looy ragal kon doxalal Am na ñaanu waajur Lu may ragal nañu doxal Lobita Gueye am na ñaanu waajur Looy ragal kon doxalal Pape Beye am na ñaanu waajur (le jeune tailleur) Mbawor mbawor bi yaw kay doxal Ndeye Thiam am na ñaanu waajur (jigéenu Bass) Chérie Soulemane Sané doxalal Ehh Wally bul geestu Maryacine bul geestu Liggéeyu nday day tontu Narou Diaga bul geestu Chéri Sokhna bul geestu Liggéeyu nday day tontu Xoolal liggéey focus ñuy waxtu Xol bu rafet day tontu Maroo mar bul geestu
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out