Paroles

Ndeke dou mbeuguelou kassè Teh sax xetou mbeuguel yi dafa rare Dièkou ma ni douma bale yeah yeah An konne yaw bandi nga ndèkè bebe Sopi nga sama xol bi limonade Siroter ko diko nane yeah yeah Ndax baniouy ndieukeu guissanter Li nga ma yene nimou disser Ak niniou xolanter Rek ma xamni yalla niou bolè Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (kaay waay) Doflo ngama (kaay waay) Wayè deufeul ngama (kaay waay) Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay) So bèguè ma bègue (kaay waay) Niou deukè di rè (kaay waay) Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay) Maala geuneul lounè (kaay waay) Teh yaama geuneul kounè (kaay waay) Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay) Bègal ma bèg (kaay waay) Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay) Soma sorè oh my love Namel bimay yeuk thi yaw Wallahi yaako meuneu fadie nieuweul Niouy kaf di rè Niouy kaaf di fo di rè Ndax baniouy ndieukeu guissanter Li nga ma yene nimou disser Ak niniou xolanter Rek ma xamni yalla niou bolè Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (kaay waay) Doflo ngama (kaay waay) Wayè deufeul ngama (kaay waay) Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay) So bèguè ma bègue (kaay waay) Niou deukè di rè (kaay waay) Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay) Maala geuneul lounè (kaay waay) Teh yaama geuneul kounè (kaay waay) Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay) Bègal ma bèg (kaay waay) Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay) Oh, bébé, toi mon bébé Toi qui m'as tout donné Je pourrais jamais te quitter Je t'en fais la promesse mon bebe Tu m'as tellement épaulé Quand il le fallait M'a sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bebe yaw mi gounguè ma man malay gounguè Et si t'as peur crie aider moi mane maaa lay sauvé Oh bebe yaw ndax beuguè ngama comme nim la beuguè Ndax nim la beugè eup naaa wa li noum dèmè Oh, bébé, toi, mon bébé Toi qui m'as tout donné Je pourrais jamais te quitter Je t'en fais la promesse mon bebe Tu m'as tellement épaulé Quand il le fallait M'a sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bebe yaw mi gounguè ma (Kaay waay Kaay waay Kaay waay Kaay waay Kaay waay Kaay waay)
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out