Paroles

Zoom as the beat Man duma ku ndaw À part sama taille dara tuutul ci man Maay kunde ngureen, dama di ndaanaan ci miin réew, chérie, neexuma bañ Waajuma bàyyee dunya laay ñew yëngël Maak sama gars yee ku ne lañuy yëngel Dunya duma tàyyee, dunya laay ñëw yëngël Eeey yooy Ak man doo am envie ñibbi tay Ndaxte sa life laay soppi dream girl Looy doye didi su fekke li ngay rêver Yaa ngi koy dundu sama wet, kaay ñu fêter Ak man doo am envie ñibbi tay Ndaxte sa life laay soppi dream girl Looy doye didi su fekke li ngay rêver Yaa ngi koy dundu sama wet, kaay ñu fêter Waajuma bàyyee dunya laay ñew yëngël Maak sama gars yee ku ne lañuy yëngel Dunya duma tàyyee, dunya laay ñëw yëngël Eeey yooy Duma ku ndaw À part sama taille dara tuutul ci man Maay masamba yee Maay kunde ngureen, dama di ndaanaan ci miin réew, chérie, neexuma bañ Maay masamba yee Yaw Amadeus, xol fu mu xas ba dugg ca foofu lay dëkke Yaw mii, yaa xasa dugg ci sunu xol yi, dara du ko dindi, ñoo la bëgg Amadeus ak Kadhim Temp bu ñu ànd dëkk bi yëngu Dama la xool daadi gisub reine Acca cañe kaay leen sama queen ba ngee (aka jongama) Sacc makaan daadi bëtum teen (aka neexi ree) Fepp di na yaa ñi sama queen ba ngee (sama queen ba ngee) Xol laa la jox su ma amoon lu ko gën itam jox la ko Jël àdduna ak li ci biiram jébbal la ko Sama xol yaatu na, gudd ni auto rail waaye yaay dawal girl Eeey yooy Waajuma bàyyee dunya laay ñew yëngël Maak sama gars yee ku ne lañuy yëngel Dunya duma tàyyee, dunya laay ñëw yëngël Eeey yooy (lii su la doyul, lu lay doy?) Duma ku ndaw À part sama taille dara tuutul ci man (loolu dëgg la) Maay masamba yee Maay kunde ngureen, dama di ndaanaan ci miin réew, chérie, neexuma bañ Maay masamba yee Ma ne yëngël (yëngël gësam) Sañse yëkketi mbagg (masa waay) Dozé ndaanaan yu mag yi mooy lu mere bi jooxoñ ñu dagg Siisu man la dégal (dégal ma kii) Dama naw ba la ñu may tagg Yaw fenn nga demul te yàgg nga fi trop mel ni camaas neki walf Soxna ci ñun du ñoom, ñoom du ñuun Ñoo ngi coop ñoom ñooy muñ Maa ngi jarle ñoom ñoo jaayul Xiif ak békoor xar seen tuñ yi Ball sa bopp def la victime bi Bombe flop amul ci team bi Seen labél mooy douce bi music Tatouage NGA ci bas feeting bi Sa ay fans mënul feesal pick up Bés boo décider dajale sa ay Sope dinga wétal sa kër, TDOM baa sa sécteur Duma ko ndaw, maay seen vie Infiltré mel ni rainer Maa fi mën ana problème bi Calculé ma, ngandim erreur Man duma ku ndaw À part sama taille dara tuutul ci man Maay masamba yee Maay kunde ngureen, dama di ndaanaan ci miin réew, chérie, neexuma bañ Maay masamba yee
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out