Lyrics

Par AbouAmg Daan ko bëgg play kaay ñu game Rekk nga xam shingom du kaani xeeñ Difeinte faime, jaxase faine Gisuñuma seen gis gisa ñaaw Ñee di siisu Ñi lax seen soxor ci Yàlla Yàlla mi ñiy woote gëm mu ñu ko Laxu nëtëril dégg Héy girl Mënoon nga ko maafe, dëgg-dëgg Héy girl Tigadege bee na ni noon Héy girl Bëgg baax taxoon ma teela séy Séy muñ daj ëmb direeku Doo ma ci juddu Bautiful baby Aminatou Doon mère célibataire bi di fippu Doon ndey doon baay Doon ndey doon baay Doon ndey doon baay Benn nit ngay tuddu gaañ ay mbokkam Héey, ma ni mooma lu ma wor la di fen Te kenn du tuddu sa jaambaar Dañuy toog di xaar faux pas Héy girl Mënoon nga ko maafe, dëgg-dëgg Héy girl Tigadege bee na ni noon Héy girl Bëgg baax taxoon ma teela séy Séy muñ daj ëmb direeku Doo ma ci juddu Bautiful baby Aminatou Doon mère célibataire bi di fippu Doon ndey doon baay Doon ndey doon baay Doon ndey doon baay Mbaa doo màndu ak loo ko xamal Nit day màndu dee ko suturaal Mbaa doo màndu ak loo ko xamal Nit day màndu dee ko suturaal Nit ku xam Yàlla day màndu Nit ku gëm Yàlla day màndu Nit ku xam Yàlla day màndu Màndu, màndu Mànduleen ooo Mànduleen ooo Mànduleen ooo Héy girl Mënoon nga ko maafe, dëgg-dëgg Héy girl Tigadege bee na ni noon Héy girl Bëgg baax taxoon ma teela séy Séy muñ daj ëmb direeku Doo ma ci juddu Bautiful baby Aminatou Doon mère célibataire bi di fippu Doon ndey doon baay Doon ndey doon baay Doon ndey doon baay Del suturaal jigéen Del suturaal jigéen
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out