Credits
AUSFÜHRENDE KÜNSTLER:INNEN
AMADEUS
Künstler:in
KOMPOSITION UND LIEDTEXT
Charles Mbaye Diagne
Komponist:in
Saliou Samb
Songwriter:in
Lyrics
Duu bàyyi
Ak loo ka mën def du bàyyi
Ak lu mu mën a gis du bàyyi
Loo ko mën a def du bàyyi
Bisóo bis
Ngay gën a triste
Lenn nga bëgg, wéetal man ci àdduna
Lii ngay gis
Lépp mooy bis
Bis ñëw maa dëddu lépp nelaw ajuna
Live day gën a tar, mais doo mës a bàyyi
Ya ngi dundee yaakaar
Gis naa ci yaw jàmbaar, def nga lii la war
Te yàlla du la seetaan
Te bëgg nala bëgg comme ni nga ma
Soxla tuuti love comme ni nga may
Lépp loo bëgg man maa nekk caa
Ndax mérité nga koo
Bëgg nala bëgg comme ni nga ma
Soxla tuuti love comme ni nga may
Lépp loo bëgg man maa nekk caa
Ndax mérité nga koo
Aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe
Su maa sañoon bëgg lay
Guddi sax comme nii nga may
Aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe
Su maa sañoon bëgg lay
Guddi sax comme nii nga may
Man defumala lenn lu wara tax
Sa xel ak xalaat di nekk ci leneen
Xol bi ci doon war, toppina kennen
Jaam ak bëgg bëgg bam, mais yàlla mooy ndogal
Saa boo may xool, mbegte bii may gis ci yaw
Fa jànt bi takk mu nu ma ko ëppu mbaa gën di boy
Mader'fuckin' love buu fekkee man ki ma ko séqal gisoo maa
Loolu ngay wax man sa ma biir, metti na maa lool baby
Tay bëgg na, nga bëgg ma comme ni mala
Soxla tuuti love comme ni maa lay
Lépp lii ma bëgg, yaw nga nekk caa
Ndax mérité na koo
Bëgg nala bëgg comme ni nga ma
Joxla tuuti love comme ni nga may
Lépp loo bëgg man maa nekk caa
Ndax mérité nga koo
Aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe
Su maa sañoon bëgg lay
Tuuti sax comme nii nga may
Aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe-ya-ya-ya, aïe
Su maa sañoon bëgg lay
Tuuti sax comme nii nga may
Maa nila laa dem ndax mënumala wax
Man du ma Daam caatu Mbissan
Duu ma la nii dem na ndax mënumala waxee Dame
Man du ma Daam caatu Mbissan
Daam caatu Mbissan
Jarul seetlu jii Daam, jarul dem dii seeti giisaanee
Lyrics powered by www.musixmatch.com