Lyrics

Par AbouAmg Bass Thioung lay doon Man ku ma faale ma faale la Ku ma talul taluma la Joxoo ma ma lekk, joxoo ma ma naan Doo ma tere dund, na ku nekk taal boppam Nekk ci jàmm ñépp feex Soo meree ki tal boppam Doo nekk ci jàmm doo am tus Comment tu vas, comment ça va Ça va va va va va va va Waxkat yi good morning,vas Mbaa jàmm ngeen yeewoo, vas vas Comment tu vas,comment ça va Ça va va va va va va va Ku mer kala mel ni Yàlla L'enfant béni MashAllah! Bokku mak ñoom(ay!) Niroowu mak ñoom Ay defal ndànk bin bin Man la bis bi dara du xew! Hey, luy problème bi? Problème bi fu mu nekk Joxoo ma ma lekk,joxoo ma ma naan Hey doo xol xanaa gisoo et vas Man ku ma faale ma faale la Ku ma talul taluma la Joxoo ma ma lekk,joxoo ma ma naan Doo ma tere dund,na ku nekk taal boppam Nekk ci jàmm ñépp feex Soo meree ki tal boppam Doo nekk ci jàmm doo am tus Comment tu vas,comment ça va Ça va va va va va va va Waxkat yi good morning, vas Mbaa jàmm ngeen yeewoo, vas vas Comment tu vas,comment ça va Ça va va va va va va va Benn nettalikat du tokk fi may tokk hey vas Yàq der baaxul bul ma taxal way,vas vas vas Jàmm ci yaw ak say mbokk doo bàyyi golo bi nga bokku Ñoom man lañ bëgg man lãn sopp Fees na bay tuuru mu ngi toog Ku indi li(Bass) Man lañuy toppando(Bass) Ku dàq sañse fi(Bass) Ku moom millions de vues(Bass Thioung) Boroom tendance(Bass) Seen reference(Bass) Ku leen bëgg(Bass) Kon kaay ñu danse(Bass Thioung) Hey, luy problème bi? Joxoo ma ma lekk,joxoo ma ma naan Hey doo xol xanaa gisoo et vas Yëngal! Àtt bi sama àtt la Ma xew xanaa neex Yëngal Ay heur bu ma neex Dama koy yëngal Par force,dama koy yëngal! Ñu deme fecce ko fecce ko boy Kaay man maa koy yëngal Fecce bu bes la dafa xew avancer bul dof Doxal dox bi! Avancé yaa leen raw Doxal dox bi Avancé bul geestu Doxal dox bi Avancé yaa leen raw Doxal dox bi Avancé bul tontu Doxal dox bi Avancé yaa leen raw Hey bëgg nga mel ni man,taxul nga mel ni man Déedéet,mashallah bu la ma catu stop Waa doyul! Non,non,c'est pas fini! Yëngal! Àtt bi sama àtt la Ma xew xanaa neex Yëngal Ay heur bu ma neex Dama koy yëngal Par force,dama koy yëngal! Ñu deme fecce ko fecce ko boy Kaay man maa koy yëngal Fecce bu bes la dafa xew avancer bul dof Doxal dox bi! Avancé yaa leen raw Doxal dox bi Avancé bul geestu Doxal dox bi Avancé yaa leen raw Bibi jege na Avancé bul tontu Aye bibi avanceel def patte Bul tontu Bibi How are you,I'm fine Avancé Doxal dox bi Avancé Doxal xol bi Bibi jege na Avanceel Doxal dox bi Aye bibi avanceel def patte Bul tontu bibi How are you,I'm fine
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out