Lyrics

Par AbouAmg Kaay ma, kaay ma, kaay ma Kaay ma xamal laa ni àddunia du benn fan Ki ngay tooge tay bu suba mën na la yéy Kaay ma jëgël la ni bul di xol nit di ko nié Mën naa la yobbe iñan iñan iñanYaa ngi coq coq ba kale Maay pop pop ci xale Ngay poq poq ba kale Jëmoo te munoo dabbe Man su ma bëggulee bul sale Gis naa ne doole filling bela poussale Soo bëggulee bul sale Mbalu soxor iñan dalay teye Boo ko toppee dangay de fiiril sa xol Ay waay! Eh yëg naa li nga nekke Dama lay leebal mbaax nga may fexel Eh baye doore, gis naa la ngay lere Eh eh eh doo gore, man gis naa ni nga may xoole Bul defe ni li nga nekke yëgguma ko dama doylu Boo defee ni ya gëna yeewu ñépp nelaw nga bay gaale Coow rekk, yaw dëkkel coow rekk Coow rekk, yaw dëkkel coow rekk Démb yaa ni woon Démb yaa ni woon di goree diwo Kon lu la japp taye banga nekk ci yoonu non non Pareguma, non non tàmbaleguma Yaay sa xol ci ñanaal ma Saboo Douhan Uma mi falama nene barakaa Yaa ngi coq coq ba kale Maay pop pop ci xale Ngay poq poq ba kale Jëmoo te munoo dabbe Yaw uttel bennen yoon boo jaare Yaw demoo ku ne ci yoon nga jëme ko gare Mbalu soxor iñan dalay teye Boo ko toppee dangay defi lu soxor Ay waay! Eh yëg naa li nga nekke Dama lay leebal mbaax nga may fexel Eh baye doore, gis naa la ngay lere Eh eh eh doo gore, man gis naa ni nga may xoole Bul defe ni li nga nekke yëgguma ko dama doylu Boo defee ni ya gëna yeewu ñépp nelaw nga bay gaale Coow rekk, yaw dëkkel coow rekk Coow rekk, yaw dëkkel coow rekk Coow mënul dara, wax ju bon fajjul dara Coow mënul dara, ci man wax ji fajjul dara Coow mënul dara, ci man wax ji fajjul dara Coow mënul dara, ci man wax ji fajjul dara Coow ma ni mënul dara daf may yokku doole Nopalul Xale baa nge man la Xale baa nge (xam nga ni man laa waaw) Xam nga ni man laa, ay man la Affaire bi man la, wooy man la Ne nañ ma yaw la, xale baa nge waaw Ay man laa, affaire bi man laa Wooy man la, ne nañ ma yaw la Bilaahi damay foo ak yeene
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out