Music Video

Daaraj family - jamono (official music video)
Watch Daaraj family - jamono (official music video) on YouTube

Featured In

Credits

AUSFÜHRENDE KÜNSTLER:INNEN
Daara J Family
Daara J Family
Künstler:in
Euclides Gomez Jr
Euclides Gomez Jr
Künstler:in
Khadim Mbaye
Khadim Mbaye
Künstler:in
Faada Freddy
Faada Freddy
Künstler:in
Ndongo D
Ndongo D
Künstler:in
KOMPOSITION UND LIEDTEXT
Faada Freddy
Faada Freddy
Komponist:in
Ndongo D
Ndongo D
Songwriter:in
PRODUKTION UND TECHNIK
Ludovic Joyeux
Ludovic Joyeux
Mischtechniker:in
Manu Sauvage
Manu Sauvage
Produzent:in

Lyrics

Léeg-léeg damay bëgg gàddu samay loxo yuuxu mettit Damay bëgg give up yenn-saay Tolof-tolof ak i nattu yu takku bëgg yóbbu sama fit Xam naa ne àdduna duma ray Coono dafay defar xolu doomu-aadama bi ci ngëm Jàmbat mayu ma njegenaay Buur Yàlla rekk a xam li nekk sama dënn maa koy dekku Baña jeng ta gëm ne ginnaaw jafe-jafe noflaay Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano la Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano la Jamano kow lañu jële Xamuñ noflaay dinu mbëllee Rêves yu la sut aka kowe Gént boo fàttee connexion bi da fa dem Fok ñu am pass dañoo calé Daf ma yéem ñaata jéem ñaata yoon lañu jéem Yoonu suuf yoonu ndox fëgg fu ne fu nuy jaare Kan moo nuy jàlle jotu ma nelaw biig yaakaar gën a diig fok nu génn ci Lan moo nu jig ñàkk pare ci (jamano di gën a tërëdi) Loo génn kër gis àdduna bi ci écran Bu tuuti accès illimité (wuti visa) Loxo yaa ngi clické souris yi défilé actualité ni muy dikke, bu la Benn ngelaw yóbbaale Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano la Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano la Rakk bul wori di nga jéggi ndox Bu soobe Buur bi gone dina màgg bay dox Lépp dina baax lépp dina baax Lépp dina baax lé lé lé lépp dina baax Du jikko jamano la du dara jaar-jaar la Boroom karaw gu ñuul ñàkkul dara dara Jombula Dara dara warul jomb góor-Yàlla gu am ngëm gu kowee Te nga jéem a bey sa tool Yàlla du beykat bul xaar fu muy tawe Di nga gis sa yoon jamano naqadi toogal ci dëkk bi jaayonte Sélébeb yoon la jamano tërëdi fonkal sa bopp li ngay jànkoonte Bu la kenn def jaam tukki du tekki fépp la metti Làbbali fas buumu gàcce nga tekki Xaalis dafa ngande làmmiñ ci jamano dëgg ne patt Doole poos ak kàrt gab moo lay waxloo moytul bëtu xol bi patt Paaka ci put bu mu tax nga bonn xoolal fu sori bul jàdd koñ Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano la l Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano la . Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama... jamano la jamano la jamano la jamano la .
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out