Lyrics

Prod2Prod Amg (ARA) Akhlou Brick from Sénégal West Afraica World wide Hawma louma gnam ba diodo Sa liguéya diap sa Serigne bé aay Tek ma naagn dima madj lo Yay sama Générale nala todial way Takhaliko menoutoula né Kanar bi teud nagn ko sani guédj bae Falewma bénén go Lidiantiwma bénèn go Matay nop la angou thiow li Bb nagnou rouslo wahi noni Faw rek gnou wan lén ko Jelel sama money now Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes You make me feel the good life Give You my money See You go down For me Yi go down low Baby loumala may hep nako Te man awma si yaw sago Bb wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago This is... (Dayza) Ba sa xol Bangui sed Man mangui fekh Retalna man malay xol rek di bek Wanél niga meunee Wanél né dou Ben Dieund lal bou noy wanla noy danou si nek dengua, Foma fek dik sif ma séey Fo aw yon nangoulnala Biss niki tay Meusso guiss djinee yak mom kif kif la kay Gagné nga Sama coeur dakh sa assou pikaray (ARA) Ligéyma dama beug geunla bardé Nagn ko doumdou mak yaw kassé Mbeungel boudé rayé yalna dé Meunatouma doundou sans yaw (DAYZA) No man awma diom Paka bingma rayè mako dass Dara metiwouma sino malila alma gaz Lamign béngui sa poche Sagnatouma kass Guissna sama ourou ayni nieuweul fi gnou danse kay (ARA) Jelel sama money now Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes You make me feel the good life Give You my money See You go down For me Yi go down low Baby loumala may hep nako Te man awma si yaw sago Bb wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago This is... Sa hol bi gagnou won na Maa gnew fadial la gomi Rangogni fér na honey No mind! I never u let you alone Dou dem la gneup wahone Décider wougn ko won It just man ak yaw dong Manak yaw la wara don bou thi ken dougou Falewma bénén go Lidiantiwma bénèn go Matay nop la angou thiow li Bb nagnou rouslo wahi noni Faw rek gnou wan lén ko Jelel sama money now Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes You make me feel the good life Give You my money See You go down For me Yi go down low Baby loumala may hep nako Te man awma si yaw sago Bb wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago This is...
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out