Lyrics

Par AbouAmg Boy guénal sa négu yaay Gneuw ci négu goor, dugu ci négu seuy Di dém ci négu yallah Guéneu négu yallah Gnu dieméla négu deuk Yéné négu la borom mathiay fanan Motakh ku méér tant pis Ku méér tant pis Ku méér tant pis Ku méér tant pis Aziz samb diokhal boy yi chips crax tampico En place maarifa gang xam xam bu bayiko ba kossy Doyal nagn ci reuk pott yi borom flow wou mbôt yi Gnu wax lén xar'lén tanku toubey ngén koy xotti Téknagn game ci loxo tacko fall ku yotu tokki Muma ngén diox sen micro légui jangu yi tass Djanteu bi fégn a lamp yi faay What ever happen in vegas Million ci poche mayé pôt ak sama Camaro Bo beugué xam flow yima am comptél ay bakanu omaro Bul rég'lék maan compte reg'lél say règle douleureuse Rap ba to lingay deff momay diox mahfouss ak dudu buzz Do civilisé ba romb yamb la gueuna fonk cacam Sawara tuma raak nakh kossi noku duko wax papam Dagn néma ara fow nga rap level bé dess fi Rappeurs yé gueuna guateu carrière talibé ak bess fi Maam la dof bi tokk xuri gnima done woku Reudeu sama baram ci sen lakh bi sow bi dima topu Boy guénal sa négu yaay Gneuw ci négu goor, dugu ci négu seuy Di dém ci négu yallah Guéneu négu yallah Gnu dieméla négu deuk Yéné négu la borom mathiay fanan Motakh ku méér tant pis Ku méér tant pis Ku méér tant pis Ku méér tant pis Aziz samb diokhal boy yi chips crax tampico Hey nénagn sen rap goor la dafa diongu Ma lathie turando gnunéma aida diongue Balén rap liguey yéna gui fontu Amolen diom sisi ndax ba diom don xeuy Yéén si guén guontu Dagn may rélo rek mane xawma fougn'len foré damn Léwett ni nawé sen rappeurs comme ay comédiens Naan malay meun non malay faay Nane mafiy doul mais yafiy dey Non féthial dougui féthial waay
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out