Titres les plus populaires de Dana Brito
Crédits
AUSFÜHRENDE KÜNSTLER:INNEN
Dana Brito
Künstler:in
KOMPOSITION UND LIEDTEXT
Damiana Brito
Songwriter:in
Ousseynou Lo
Songwriter:in
Paroles
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Tey la geneu beg
Tey la geneu contan
Tey la geneu fess
Teyla xel bi geneu dal
Tey la geneu beg
Tey la geneu contan
Tey la geneu fess
Teyla xel bi geneu dal
Lou way degeur degeur dangey dioy
Genetilen mouchoirs yi xol yi toy
Lou way degeur degeur dangey dioy
Genetilen mouchoirs yi xol yi toyati
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Bailando ooh
Non douma girl bou beuri tchip tchip no
Meritewo fomp samay dal nono
Dou yani meun ngeu
Top ma bi tchi ring bi
Diaroul teup di dal ndank rek rimbi rimbi
Chibi ribi rampapao
Chibi ribi rampapirey
Lou way degeur degeur dangey dioy
Genetilen mouchoirs yi xol yi toy
Lou way degeur degeur dangey dioy
Genetilen mouchoirs yi xol yi toyati
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Mane ma fi neh
Mafi neh bu ken merr
Geneu len gnu bege
Boul sissu Dana fi neh
Mane ma fi neh
Mafi neh bu ken merr
Geneu len gnu bege
Boul sissu Wa dafa lerr
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Sodade sodade
Des nha terra san Nicolao
Lyrics powered by www.musixmatch.com